Seetal ay jokkuwaay yu kereceen yuy jàngale ci li ngay seet

Aaya bés bi

Waaye malaaka mi ne leen: «Buleen tiit, ndaxte dama leen di xamal xebaar bu baax buy indi mbég mu réy ci nit ñépp. Tey jii ca dëkku Daawuda, ab Musalkat juddul na leen fa, te mooy Almasi bi, di Boroom bi.

— Luug 2:10-11