Seen Wuutub Yàlla

“Mu tontu ko ne doktor am na weg wu rёy ngir yow ni kaŋam ci sa ligey. Naw naňu la ni jangale kat ci daara ju magg ji te saw tur weg nan ko ci biir ňi nga bokkal ligeyu faj. Laata ngay dëgëlat ne Yàlla amul ndax mën na la ňaan nga jang Bibal bi ak pasteef bi nga andaloon bi ngay gestu ci walu xarala faj?”