Yoonu Njub
Asalaamaalikum mbokki déglukat yi. Nu ngi leen di nuyu ci turu Yàlla Boroom jàmm, ji bëgg ñépp dégg te nangu yoonu njub wi mu tëral, ngir am jàmm ju wér ak Moom ba fàww. Sunu xol sedd na lool ci li nu leen man a dégtal emisyoõ bi tudd Jàng lu gëna bare